1 Corinthians 1:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Maa ngi ñëw ca wax ja: kenn ku nekk ci yéena ngi naan: «Man ci Pool laa bokk!» «Man ci Apolos!» «Man ci Sefas!» «Man ci Kirist!»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li may wax mooy ku nekk ci yeena ngi naan: «Man ci Póol laa bokk!», «Man nag Apolos!» «Man Sefas!» «Man de Almasi!»