1 Corinthians 1:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ngir kenn bañ a wax ne, ci sama tur lañu ko sóob.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ngir kenn du ne ci sama tur lañu leen sóobe.