1 Corinthians 1:18 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte yégleb deewu Kirist ca bant ba, ag ndof la ci ñiy sànku. Waaye ci nun ñi aw ci yoonu mucc gi, dooley Yàlla la.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat kàddu gi jëm ci bantub Almasi, ba ñu ko daajoon, ag ndof la ci ñiy sànku. Waaye manoore Yàlla la ci nun ñi mucc.