1 Corinthians 1:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ana boroom xam-xam bi? Ana kaaŋ mi? Ana boroom làmmiñ wu neex, wi ci àddina sii? Xanaa Yàlla wonewul ne, xam-xamu àddina si ag ndof la?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ana kuy xamkat? Ana kuy firikatub yoon? Ana waxkatub àddinay tey jii? Xanaa du Yàllaa def xam-xamu àddina si ag ndof?