1 Corinthians 1:21 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Gannaaw àddina si ci xam-xamam demul ba xam Yàlla --te Yàllaa dogal loolu ci xam-xamam — soob na Yàlla mu musal ñi gëm, jaar ci yégleb xebaaru Kirist, fekk ag ndof la ci bëti nit.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yàlla moo dogal ci xam-xamam, àddina tële koo xam ci xam-xamu boppam. Moo tax mu soob Yàlla, mu jëfandikoo xibaaru Almasi, biy ag ndof ci nit ñi, ngir musale ko gëmkat ñi.