1 Corinthians 1:25 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Li ñuy wax ag ndof ca wàllu Yàlla moo gën a tedd xam-xamu nit. Te li ñuy wax ñàkk dooley Yàlla moo ëpp kàttan dooley nit.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndaxte li ñu jàppe ag ndof fa Yàlla moo sut xam-xamu nit, te li ñu jàppe néew dooley Yàlla moo raw dooley nit.