1 Corinthians 1:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yàlla kuy sàmm kóllëre la, moom mi leen woo, ngir ngeen bokk ak Doomam Yeesu Kirist, sunu Boroom.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yàllaa am kóllëre, moom mi leen woo, ngir ngeen bennoo ak Doomam Yeesu Almasi, sunu Sang.