bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Corinthians 10:17
1 Corinthians 10:17 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ndegam benn mburu rekk a am, kon nun ñépp lu nu baree-bare, menn mbooloo lanu, ndaxte bokk nanu menn mburu mi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw menn mburu la nag, doonte ñu bare lanu, kon wenn yaram lanu, ndax nun ñépp, menn mburu mi lanu bokk.