1 Corinthians 10:19 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Li may wax, lu muy tekki? Ndax yàpp wi ñu jagleel xërëm yi dafay dara? walla xërëm yi dañuy dara?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ana kon lu sama wax jiy wund? Ndax daa wund ne yàpp wu ñu sarxal tuur yi tekki na lenn? Am daa wund ne tuur yi tekki na lenn?