1 Corinthians 10:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Sóobu nañu ca ndoxu géej ga ak ca niir wa, ba bokk noonu ci Musaa.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñoom ñépp lañu sóob sóobeb Musaa, ca biir niir wa, ak ca biir géej ga.