1 Corinthians 10:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Déedéet! Waaye sarax yi xërëmkat yi di rendi, ay rab lañu ko jagleel; jagleeluñu ko Yàlla. Te man bëgguma, ngeen booloo ak rab yi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li may wax kay moo di yooyu sarax, rab yi la ñeel, waaye du Yàlla, te bugguma ngeen bokk ak rab yi lenn.