1 Corinthians 10:23 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Dafa am ñu naan: «Lépp lanu sañ.» Waaw, waaye du lépp a baax ci nun. «Lépp lanu sañ,» waaye it lépp du yékkati ngëm.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Sañees na lépp,» lañu wax. Waaye du lépp ay jariñe. «Sañees na lépp,» waaye du lépp ay yokke.