1 Corinthians 10:25 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Man ngeen a lekk lépp lu ñuy jaay ca ja ba, bañ cee boole ay laaj ngir dalal seen xel.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mboolem luy jaay ca ja ba, sañ ngeen koo lekk te bañ cee luqatu lenn luy indi ngànt cim xel,