1 Corinthians 10:26 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte Mbind mi nee na: «Àddina ak li ci biiram lépp, Boroom bi moo ko moom.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax Boroom bee moom àddina, ak li ci biiram.