1 Corinthians 10:27 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ku xamul Yàlla nag, bu leen wooyee aw ñam këram, te ngeen nangoo dem, lekkleen lépp lu ñu leen dëj, bañ a laajte dara ngir dalal seen xel.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu leen ku gëmul wooyee lekk, su ngeen nangoo, mboolem lu mu leen taajal, lekkleen, te bañ cee luqatu luy indi ngànt cim xel.