bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Corinthians 10:28
1 Corinthians 10:28 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye bu leen kenn nee: «Lii sarax la, bu ñu jagleel xërëm yi,» suurleen ko ndax ki leen ko xamal, ngir xel mu dal.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye bu leen kenn nee: «Lii ñam wu ñu sarxal tuur yi la,» buleen lekk, ndax ka leen ko xamal, ndax itam, ngànt lu wax jiy indi cim xel.