1 Corinthians 10:29 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waxuma sa xel yaw, waaye xelu keneen laay wax. Waaye nga ne: «Li ma sañ a def, lu tax nit ku xelam dalul di am dara lu mu ciy wax?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waxuma seenum xel yeen, waaye xelu keneen ka laay wax. Ana sax lu waral sama sañ-sañu bopp di aju ci àtteb keneen ku am xelam amal ngànt?