1 Corinthians 10:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñoom ñépp bokk nañoo lekk ñam, wa Yàlla joxe,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñoom ñépp, wenn ñamu kéemaanu Yàlla wa, moom lañu lekk,