1 Corinthians 10:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
naan naan ga mu joxe, ndaxte ñu ngi doon naan ca xeer, wa leen doon gunge, te xeer woowa Kirist la woon.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
te ñoom ñépp, menn ndoxum kéemaanu Yàlla ma lañu naan, ndax ñoo doon naane ca doju kéemaanu Yàlla ga, doj wa leen doon gunge, te doj wa Almasi la woon.