1 Corinthians 10:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Mbir yooyu ay misaal lañu, yu nuy artu, ngir benn bëgg-bëgg bu bon bañ noo jiital, na mu leen jiitale woon.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yooyu xew-xew ay misaal la, ngir nu baña xemmem yëf yu bon, na ko maam ya daan xemmeme.