1 Corinthians 10:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Buleen jaamu ay xërëm, ni ko ñenn ñi ci ñoom defe woon. Ndaxte Mbind mi nee na: «Mbooloo mi dafa toog, di lekk ak di naan, ba noppi ñu jóg di mbumbaay.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buleen doon ay jaamukati tuur, ni ko ñenn ci ñoom doone woon. Noonu lañu binde ne: «Mbooloo ma toog, di lekk ak a naan, nes tuut ñu jóg, di mbumbaay.»