1 Corinthians 11:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Xanaa du àddina ci boppam dafa leen di won ne, gàcce la ci góor, ngir muy yar kawar gu bare?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xanaa ni àddina ci boppam tëdde xamalu leen ne yar kawar gàcce la ci góor?