1 Corinthians 11:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye loolu nag ab taar la ci jigéen. Dañoo jagleel jigéen kawar gu gudd, muy muuraay ci moom.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndaxam kawar gu bare sagu jigéen la. Jigéen lañu jagleel kawar gu bare, muy muuraayam.