1 Corinthians 11:17 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi may tollu ci ndigal yi, mënuma leen a sant, ndaxte seeni ndaje loraange lañuy jur, waaye du njariñ.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye lii ma leen digal, am na ci lu ma leen gërëmewul, ndax du njariñ la seeni ndaje di jur, xanaa loraange.