1 Corinthians 11:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bu ngeen dajee, mënuleen a wax ne reeru Boroom bi ngeen di lekk.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu ngeen dajee benn bérab, bokk reeru Sang bi taxul,