1 Corinthians 11:23 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Li ma jële ci Boroom bi, moom laa leen jottali: Boroom bi Yeesu, ci guddi gi ñu ko woree, dafa jël mburu,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Man, li ma jële ci Sang bi, moom laa leen jottli: Sang Yeesu, guddi gi ñu ko woree, dafa jël mburu,