1 Corinthians 11:30 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Looloo tax ñu bare ci yéen wopp te ñàkk doole, ba ñenn ñi faatu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Looloo tax ngeen bare ñu néew doole, ak ñu xiibon, ba lim bu takku dee.