1 Corinthians 11:33 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu nag bokk yi, bu ngeen dajee, di lekk reeru Boroom bi, nangeen xaarante.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag bokk yi, bu ngeen dajee, ngir bokk lekk, xaaranteleen.