1 Corinthians 11:34 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ku xiif, na lekke këram, ngir bañ a indi ci yéen àtteb Yàlla ndax seen ndaje yi. Yeneen fànn yi ci des nag, bu ma ñëwee ci yéen, dinaa ko seet.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ku xiif, na lekke këram, ngir seeni ndaje bañ leena yóbbe mbugal. Yeneen mbir yi nag, bu ma dikkee, dinaa ko leeral.