1 Corinthians 11:5 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye bu jigéen musóoruwul, buy ñaan walla buy wax ci kàddug Yàlla, kooku day suufeel jëkkëram jiy kilifaam, ndaxte day mel ni jigéen ju ñu wat.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye jépp jigéen juy julli, mbaa muy waxe kàddug waxyu, te muurul boppam, suufeel na jëkkëram jiy boppam. Day mel ni bu nelu woon rekk.