1 Corinthians 11:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Góor nag moom warul a teg dara ci boppam, ndaxte mooy melokaanu Yàlla te dafay wone ndamu Yàlla. Jigéen moom dafay wone ndamu góor.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Góor moom du muur boppam, ndax mooy takkndeeru Yàlla te moo taxawe darajay Yàlla. Waaye jigéen moo taxawe darajay góor,