1 Corinthians 11:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte jëlewuñu góor ci jigéen, waaye jigéen lañu jële ci góor.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax góor kat, jëleesu ko ci jigéen, waaye jigéen kay lañu jële ci góor.