1 Corinthians 11:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te sàkkuñu góor ngir jigéen, waaye jigéen lañu sàkk ngir góor.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Góor itam, sàkkeesu ko ngir jigéen, waaye jigéen kay lañu sàkk ngir góor.