1 Corinthians 12:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Léegi nag bokk yi, ci li jëm ci mayi Xelum Yàlla, bëgguma ngeen umple ci dara.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Léegi nag bokk yi, bugguma ngeen umple ci wàllu mayi Noowug Yàlla.