1 Corinthians 12:10 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
keneen di def ay kéemaan, am kuy wax ci kàddug Yàlla, am keneen kuy ràññee li jóge ci Xelum Yàlla ak li jóge ci yeneen xel yi, keneen it di wax ay xeeti làkk, ak kuy firi làkk yooyu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kii itam di def ay kéemaan, kee di waxe kàdduy waxyu, kale mana ràññatle noo yu wuute, keneen di làkk xeeti làkk yu wuute, ka ca des mana firi ay làkk.