1 Corinthians 12:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Xam ngeen ne, bi ngeen xamagul woon Yàlla, xërëm, yi mënul a wax, ñoo leen jiitaloon, di leen wommat.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bokk yi, xam ngeen ne ba ngeen dee ay yéefar, dees leena buuboon, lajjal leen, jëme ci ay tuur yu tëlee wax.