1 Corinthians 12:24 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
fekk yi gën a rafet, soxlawul nu leen di suturaale noonu. Waaye Yàlla dafa boole sunu céri yaram yi, ngir gën a teral cér yi ko soxla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
te yi am sutura soxlawuñoo suturaal. Waaye Yàlla moo sàkk sunu yaram, sàkkin wu mu ràññee cér yi gëna néew gëddë, te moo leen gëddaal,