1 Corinthians 12:29 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndax ñépp ay ndawi Kirist lañu? Ndax ñépp dañuy wax ci kàddug Yàlla? Ndax ñépp ay jàngale? Ndax ñépp ay def kéemaan?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax ñépp ay ndawi Almasi? Am ñépp ay waxe kàdduy waxyu? Am ñépp ay jànglekati kàddu gi? Am ñépp ay def ay kéemaan?