1 Corinthians 12:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Moo tax ma leen di xamal lii: ku Xelum Yàlla solu du wax ne: «Yeesu dafa araam.» Te it kenn mënul a wax ne: «Yeesu mooy Boroom bi,» su ko ko Xelum Yàlla waxloowul.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo tax ma di leen biral ne amul kenn kuy waxe Noowug Yàlla ku naan: «Alkànde ñeel na Yeesu.» Te it kenn manul ne: «Yeesu moo di Sang,» te du lu ko Noo gu Sell gi xamal.