1 Corinthians 12:30 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndax ñépp a am mayu wéral ay jàngoro? Ndax ñépp ay wax ay làkk? Ndax ñépp a leen di firi?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Am ñépp a am mayu faje? Am ñépp ay làkk yeneen làkk? Am ñépp a mane tekki ba?