1 Corinthians 12:31 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye fonkleen may yi gën. Léegi nag ma won leen yoon wu gën lépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Teewul nag, nangeen sàkku may yi gën. Waaye dinaa leen xamal yoonu dundin wi gën ci lépp.