1 Corinthians 12:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Am na ay fànn yu bare yu Yàllay feeñale dooleem, waaye jenn Yàlla ji mooy jëfe doole yooyu yépp ci ñépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jëf ji it man naa wuute, waaye jenn Yàlla ji mooy jëf lépp ci ñépp.