1 Corinthians 12:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Am na ku Yàlla sédde, jaarale ko ci Xelam, mayu wax ak xel mu leer, keneen am mayu xam-xam, te mu bawoo ci menn Xel mi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kii ci Noo gi la jote kàddu gu xelu, kee séddoo kàddug xam-xam ci genn Noo gi.