1 Corinthians 13:1 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Su fekkee ne damay wax làkki nit ñi ak yu malaaka yi sax, te boolewuma ci mbëggeel, duma dara lu dul ndënd muy riir, walla jóolóoli buy kandaŋ-kandaŋi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su ma doon làkk làkki nit ñi, ak yu malaaka yi sax, te jëfewuma genn cofeel, jóolóoli bu xumb doŋŋ laa, mbaa tëggum weñ muy riir.