1 Corinthians 13:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi ma dee xale, dama doon wax ni xale, di dégge ni xale, di xalaate ni xale. Waaye bi ma doonee mag, bàyyi naa lu bokkoon cig ndaw.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba ma dee tuut-tànk, ni tuut-tànk laa doon waxe, di dégge dégginu tuut-tànk, di xalaate ni tuut-tànk. Waaye bi may mag laa xewil yëfi tuut-tànk.