1 Corinthians 13:12 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Tey jii gis bu lëndëm lanuy gis, ni takkandeer ci seetu bu lëndëm, bu ëllëgee dinanu gis jaxran. Tey jii sama xam-xam des na, bu ëllëgee dinaa xam ba mat sëkk, ni ma Yàlla xame.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Tey jii ci ab seetu lanuy gise gis-gis bu lënt. Waaye bu keroogee, màkk lanuy jàkkaarloo ak li nuy xool. Tey jii, as ndog laa xam, waaye su keroogee, ni ñu ma xame, ni laay xame ba mu mat sëkk.