1 Corinthians 13:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Su ma yéglee wax ju tukkee ci Yàlla, ma xam lépp luy kumpa, ma yor xam-xam bépp, te gëm Yàlla ba man a randal ay tund, fekk boolewuma ci mbëggeel, duma dara.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su ma jotoon ci kàddug waxyu, boole ci xam mboolem kumpa, ak mboolem xam-xam, ak ngëm gu mat sëkk ba mana toxal ay tund, te jëfewuma cofeel, duma dara.