1 Corinthians 13:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te it su ma doon saraxe li ma am lépp, di bàyyi ñu lakk sama yaram, ba rey ma, su ma ci boolewul mbëggeel, du ma jariñ dara.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te it su ma sarxe woon mboolem sama alal, ba sarxe sama yaramu bopp ngir ñu lakk ko, su ma jëfewul cofeel, loolu du ma jariñ dara.