1 Corinthians 13:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Mbëggeel amul àpp. Ñiy wax ci kàddug Yàlla dinañu noppi, ñiy wax ay làkk dinañu ko bàyyi, ñiy xamle xam-xamu Yàlla wàcc.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Cofeel nag du jeex mukk. Su dee kàdduy waxyu, dina wéy; su dee ay làkk, dina selaw; su dee xam-xam, dina xewi.