1 Corinthians 14:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yéen itam, gannaaw dangeen a fonk mayi Xelum Yàlla, jéemleen a ëpple ci liy yokk ngëmu mbooloo mi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon yeen itam, gannaaw ñu xér ngeen ci mayi Noo gi, fexeleen cee am lu ne xéew, ngir feddli mbooloom gëmkat ñi.